Create New Playlist

Add a cover pic of your own choice

(Optional)

Name

AI Cover Generator

4 credits

Not enough credits (0/4).

Logout

Are you sure you want to Logout?

Close

JÀPPAL SA NDEY by YATTÎJAA MOOM

SongGPT
JÀPPAL SA NDEY  by YATTÎJAA MOOM  - Spiritual roots reggae / dub poetry,male vocals music cover art

JÀPPAL SA NDEY

Spiritual roots reggae / dub poetry,male vocals

0:003:45
Lyrics
Description
🎙️ [Intro – Spoken Prayer Over Ambient Pads + Dub Percussion]
AHUUZU BIL LAAHI MINA SAYTAANI RAJIIMI,
WA INNIYA AHUUZU HAA BIKA WA ZURRIYATAHAA MINA SAYTAANI RAJIIMI,
RABBI AHUUZU BIKA MIN HAMAZAATI SAYAATIINI
WA AHUUZU BIKA RABBI AN YAHDURUUN.
BISMIL LAAHIR RAHMAANIR RAHIIMI,
WA SALLAL LAAHU TA-'ALA ALAA SËYYIDINAA WA MAWLAANAA MUHAMMADIN
WA AALIHII WA SAHBIHII WA SALLAMA TASLIIMAN.
🎸 [Verse A – Soft Reggae Groove With Lead Vocal]
BÀRKEEB JAAMAM BI SANG
YAARAM BI NJAAY
LAA ILAAHA ILLAL LAAH
MUHAMMADUR RASUULUL LAAH
(SALLAL LAAHU ALAYHI WA SALLAM)
🎶 [Verse B – Build-up With Male/Female Backing Vocals]
XAADIMAM BI MAT NANU NDEY,
MAT NANU BAAY,
MAT NANU WASIILA
MOOM LA JAAM ÑÉPP DOYLOO
🥁 [Verse C – Spoken Flow Over Strong Bass + Reggae Beat]
Jàppal sa ndey
ak sa mbooleem bokk yépp teral
Te bul werenteek u nit
yaw werante gënul
Nëbbul
te bul dox di sikkal ay sëriñ ak i ngir
Bul jàpp mukk sëriñ
ak seeni ngir di bonal
Sëriñ si ak seeni ngir
ak seen u nit defaral
Tey fonk
tey suturaal
koon YÀLLA fab la gënal
Bul xaste mukk
te mbooleem waa ju jóg di la xas
Tuubal
te bul fayyu
yaw kon YÀLLA far la fayyul
Lii moo di saafara
aanal kon nga wér ni peleŋ
Te am li ngay wut
te dootoo gis lu deefi ragal
🔊 [Outro – Chant + Fading Reverb, Spiritual Closure]
JËRËJËF, JËRËJËFATI,
JËRËJËFAAT SANG BU TEDD BU GËN BI.
YALNA NA NGEEN FI GËNA YÀGG LOOLU
te ÀND KO AK WÉR
YAW NDEY JI
NUY NÀMPAL CI LEERI YÀLLA YI,
te YÀGGAL FI WÉRAL NDEY YII
NGEEN NU DÉNKK
ÑU NÀMPAL
NU MEEWI ÀDDUNA.