Create New Playlist

Add a cover pic of your own choice

(Optional)

Name

AI Cover Generator

4 credits

Not enough credits (0/4).

Logout

Are you sure you want to Logout?

Close

JÀPPAL SA NDEY by YATTÎJAA MOOM

SongGPT
JÀPPAL SA NDEY  by YATTÎJAA MOOM  - Arabic,male vocals music cover art

JÀPPAL SA NDEY

Arabic,male vocals

0:003:28
Lyrics
Description
Intro – Slow tempo, prayer-like, spoken over ney and oud in maqam Bayati]
AHUUZU BIL LAAHI MINA SAYTAANI RAJIIMI,
WA INNIYA AHUUZU HAA BIKA WA ZURRIYATAHAA MINA SAYTAANI RAJIIMI,
RABBI AHUUZU BIKA MIN HAMAZAATI SAYAATIINI
WA AHUUZU BIKA RABBI AN YAHDURUUN.
BISMIL LAAHIR RAHMAANIR RAHIIMI,
WA SALLAL LAAHU TA-'ALA ALAA SËYYIDINAA
WA MAWLAANAA MUHAMMADIN WA AALIHII WA SAHBIHII WA SALLAMA TASLIIMAN.
BÀRKEEB JAAMAM BI SANG YAARAM BI NJAAY
[Chorus – Light rhythm begins with qanun, soft riqq, warm melody]
LAA ILAAHA ILLAL LAAH
MUHAMMADUR RASUULUL LAAH (SALLAL LAAHU ALAYHI WA SALLAM)
XAADIMAM BI MAT NANU NDEY,
MAT NANU BAAY,
MAT NANU WASIILA
MOOM LA JAAM ÑÉPP DOYLOO
[Verse 1 – Semi-spoken over soft oud and tabla, warm devotional tone]
Jàppal sa ndey ak sa mbooleem bokk yépp teral
Te bul werenteek u nit yaw werante gënul
Nëbbul te bul dox di sikkal ay sëriñ ak i ngir
Bul jàpp mukk sëriñ ak seeni ngir di bonal
[Bridge – Emotional intensity rises with strings, heartfelt singing]
Sëriñ si ak seeni ngir ak seen u nit defaral
Tey fonk tey suturaal koon YÀLLA fab la gënal
Bul xaste mukk te mbooleem waa ju jóg di la xas
Tuubal te bul fayyu yaw kon YÀLLA far la fayyul
[Refrain – Repeated chorus with stronger rhythm, layered vocal feel]
Lii moo di saafara naanal kon nga wér ni peleŋ
Te am li ngay wut te dootoo gis lu deefi ragal
[Outro – Slow down, ney and violins fade, final sung prayer]
JËRËJËF, JËRËJËFATI, JËRËJËFAAT SANG BU TEDD BU GËN BI.
YALNA NA NGEEN FI GËNA YÀGG LOOLU TE ÀND KO AK WÉR
YAW NDEY JI NUY NÀMPAL CI LEERI YÀLLA YI,
TE YÀGGAL FI WÉRAL NDEY YII NGEEN NU DÉNKK ÑU NÀMPAL NU MEEWI ÀDDUNA.
AAMIIIIIIN YAA RABBAL 'AALAMIIN